Utilisateur:Groupe Lca/Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar

Groupe Lca/Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar
Histoire
Fondation
Statut
Type
Nom officiel
Iniwersite bu Ndar
Régime linguistique
Membre de
Site web
Chiffres-clés
Budget
5 milliyaar ci 2010
Localisation
Pays
Ville
Localisation sur la carte du Sénégal
voir sur la carte du Sénégal

' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

Démb modifier

Léewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.

Taxawaayam mu ngi aju ci sart no 90-03 bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.

Mu ngi jot gëddam ci ndogalu no 96-597 bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu no 96-1016 bu 4 desàmbar 1996.

Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.

Ràññeefi barab modifier

 
Gis-gisu wërngaluw iniwersite wi ci bëj-saalum ak soow jànt (bunt)

Diggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« http://www.Sunusanar.com » la ñu ko tudde.

 
buntu iniwersite bi

Bërëbu tàggat ak gëstu modifier

L'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :

  • Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
  • Xam-xamu jëmale ak xarala
  • Xam-xamu yoon ak politig
  • Xam-xamu koom-koom ak
  • Xam-xamu wérgu-yaram
  • Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
  • Caada, diine, taaral ak jokkoo
  • Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.

Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama modifier

Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:

  • Angale,
  • Farãse
  • Làkk nasaraan jëmale,
  • Xam-xamu melosuuf,
  • Xam-xamu nekkinu àskan yi.

Xam-xamu jëmale ak xarala modifier

 
Diagramme des parcours possibles au sein de l'UFR

Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.

Mën a dugg modifier

Bànqaasu xayma jëmale modifier
Bànqaasu bitil jëmale modifier
Bànqaasu informatig modifier

Xam-xamu yoon ak politig modifier

 
Offre de formation à l'UFR Sciences juridiques et politiques

Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:

  • Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
  • Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
  • Bànqaasu xam-xamu politig.

Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi modifier

Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris modifier

bànqaasu xam-xamu politig modifier

Mën a dugg modifier

Xam-xamu koom-koom ak doxalin modifier

Kërug internet [1]

Caada, diine, taaral ak jokkoo modifier

Kërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :

  • Bànqaasu jokkoo,
  • bànqaasu infogarafi,
  • Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
  • Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
  • Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
  • Bànqaasu Xam-xamu diine.

bànqaasu jokkoo modifier

Mën a dugg modifier
tërëlin modifier
Mujjàntal modifier

Bànqaasu infogarafi modifier

Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada modifier

Mujjàntal modifier
Mën a dugg modifier

Bànqaasu làkk ak caada Agrig modifier

Mujjàntal modifier
Màndargal modifier
Mën a dugg modifier

Wàllum gëstu modifier

nekkinu ndongo daara yi (CROUS) modifier

yokkute lim ndongo yi modifier

 
Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007


Effectifs par UFR
SAT SEG SJP LSH TOTAL UGB
2001/2002 400 280 499 1480 2659
2002/2003 475 325 535 1525 2860
2003/2004 559 349 575 1506 2989
2004/2005 671 396 505 1799 3371
2005/2006 726 415 688 1965 3794
2006/2007 727 641 932 2143 4443

Dëkkuwaay modifier


Loyer au campus
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers
Villages A,B,C,D,E,F,K,M 3000 (4,57 euros) ???
Villages H,I,J,L 4000 (6,09 euros) ???

Dem beek dikk bi modifier

Tektal yi modifier

Xool yeneen modifier

Téere ak mbóotu tektal modifier

  • Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, p. 5-6

Cosaan modifier

mbóotu tektal modifier

mbóotu biti modifier

Sur les autres projets Wikimedia :

Catégorie:Université au Sénégal Catégorie:Saint-Louis (Sénégal)